1/158
These flashcards cover vocabulary terms and definitions from the lecture notes.
Name | Mastery | Learn | Test | Matching | Spaced | Call with Kai |
|---|
No analytics yet
Send a link to your students to track their progress
Tudd
S’appeler
Sant
Se nommer
Dëkk
Habiter
Joge
Provenir de
Nekk
Se trouver
Am
Avoir
At
Année
Woññ
Compter
Naka
Comment
Fan
Où
Foo
Fan+nga (où tu)
Ñaata
Combien
Lutax
Pourquoi
Kan
Qui
Kañ
Quand
Ana
Où est
Noo
Naka+nga (comment tu)
Loo
Lan+nga (qu’est ce que tu)
Lan
Quoi / qu’est ce que
Ban / Yan
Quel / Quels
Benn
Un
Ñaar
deux
Ñett
Trois
Ñeent
Quatre
Juroom
Cinq
Fukk
Dix
Yeewu
Se réveiller
Sangu
Se baigner
Naan
Boire
Lekk
Manger
Ndekki
Petit-déjeuner
Añ
Déjeuner
Reer
Diner
Togg
Cuisiner
Defar
Préparer qqch / réparer
Noppalu
Se reposer
Dox
Marcher
Doxantu
Se promener
Daw
Courir
Dem
Aller / partir
Ñow
Venir
Tukki
Voyager
Jox
Donner
Jël
Prendre
Jënd
Acheter
Jaay
Vendre
Laaj
Demander
Tontu
Répondre
Wax
Parler
Waxtaan
Discuter
Jàng
Apprendre
Liggéey
Travailler
Wàcc
Descendre
Ñibbi
Rentrer
Tëdd
Se coucher
Nelaw
Dormir
Mën
Pouvoir/savoir-faire
Xam
Connaître
Mës
faire l’experience de (déjà/jamais)
Namm
Avoir la nostalgie de (manquer)
War
Devoir
Bëgg
Vouloir
Dégg
Entendre (maitriser, parler une langue)
Ak
Avec
Ba
Jusqu’à
Kon
Donc
Puur / ngir
Pour
Waaye
Mais
Ndaxte
Parce que
Moo tax
C’est pourquoi
Apare
Après / ensuite
Tamit
Aussi
Baax
Bien / bon
Neex
Délicieux
Bees
Neuf
Tàng
Chaud
Sedd
Frais
Xiif
Faim
Suur
Rassasié
Mar
Soif
Saf
Épicé
Mag
Grand
Ndaw
Petit
njool
Élancé
Gàtt
Basso
Bari
Beaucoup
Tuuti
Peu
Ñuul
Noir
Weex
Blanc
Xonq
Rouge
Yomb
Facile
Jafe
Difficile
Feebar
Malade
Sonn
Fatigué
Sori
Éloigné
Wóor
Sur
Leer
Clair
Yaru
Poli
Reew
Impoli
Tayaal
Paresseux