1/246
Looks like no tags are added yet.
how are you?
nanga def
the workers
liggéy kat yi
the roof
kaw kër gi
with/and
ak
to make/prepare
defar
i want to work with you
dama bëgg liggéey ak yaw
how much you want?
ñaata nga bëgg?
peace be upon you too
wa alaykum salam
but
waaye
and
te
i eat and i sleep
dama lekk te dama nelaw
I work with my little brother and after I sleep
dama liggéey ak sama rakk te gannaaw dama nelaw
why
lu tax?
dinner
reer
lost
réer
I cannot
nënumato
to be able to/can
mën
talk
wax
sick
tawat
it is flavorful
saf ma
water, please/water, for god´s sake
ndox, ngir yálla
it´s very delicious!
dafa neex
I’m full
rég naa
thank god
sant yálla
praise to be god
alxamdulilaay
bless
barka
may god bless you
yálla na la yálla fey
what’s wrong?
lu la jáqale?
rice and fish
ceebujën
we will meet later
dinanu gise ci kanam
I don´t cook/I won´t cook
duma togg
you don’t cook/you won’t cook
du nga togg
he/she doesn´t cook
du togg
where are you?
ana yaw?
where is he/she?
ana mu?w
where is the rice?
ana ceeb bi?
what are you doing?
loo ngay def?
what are you cooking?
lan nga togg?
my
sama
your
sa
his/her/its
am
our house
sunu kër
your/their
seen
house
kër
his rice
am ceeb
book
teere
my books
samay teere
your books
say teere
our books
sunuy teere
tomorrow
ëllëgs
sell
jay
jën
fish
build
tabax
in the future
ci kanam
let´s eat
na ñu lekk
let’s go
na ñu dem
let’s sit/let’s wait
na ñu toog
let´s discuss
na ñu waxtaan
what are we doing?
lu nuy def?
let´s drink tea
na ñu naan ataaya
what are we eating?
lu ñuy lekk?
where is your friend?
ana xa xarit?
nothing much
dara nekkul
that’s good
baax na
that
boobu
that child
xale boobu
that house
kër boobu
that woman
jigéen boobu
that is what you want
loolu mooy li nga bëgg
I want that
dama bëgg loolu
that´s what I like about you
loolu laa bëgg ci yaw
please pass the bread
may ma mburu mi, su la neexee
it was delicious
neex na
shall we go out together?
danuy génnandoo?
night
guddi
tomorrow morning
suba ci suba
prepare dinner
defaree reer
I watch TV
damay seetaan tele
bed
lal
I get up
dama jóg
that’s true
dëgg la
let´s sit here and talk
na ñu toog fi waxtaan
maybe
xayna
sorry, maybe next time
baal ma, xayna beneen yoon
no worries
amul solo
stop eating bread, eat rice
bayyil mburu, lekk ceeb
how is the people of the house?
naka wa kër gi?
they are fine
ñu ngi fi rekk
I’m hungry
dama xif
I’m thirsty
dama mar
there is
am na
there isn’t
amul
in/at
ci
the glass
kaas bi
milk
meew
I have paid
fey naa
stop here
taxawal fii
I´m tired
mangi sonn
until
ba
afterwards
ci gannaaw