Wolof 3

0.0(0)
Studied by 0 people
call kaiCall Kai
learnLearn
examPractice Test
spaced repetitionSpaced Repetition
heart puzzleMatch
flashcardsFlashcards
GameKnowt Play
Card Sorting

1/100

encourage image

There's no tags or description

Looks like no tags are added yet.

101 Terms

1
New cards

salt

xorom

2
New cards

eat your dinner, my precious baby

lekkal reer, sama xale bu neex

3
New cards

I finished dinner

pare naa reer

4
New cards

it’s true

dëgg la

5
New cards

I know many things

xam naa lu bari

6
New cards

that’s how it is

noonu mu deme

7
New cards

I wanted it, but now I don’t want it

bëggoon naa ko, waaye léegi bëgguma ko

8
New cards

I was not working

doonuma liggéey

9
New cards

I was cooking

Maa ngi doon togg

10
New cards

bëkkégoon

the day before yesterday

11
New cards

the day before yesterday, I cooked chicken. Yesterday and today I also cooked chicken

bëkkéegoon, dama togg gànnaar. Démb ak tey itam, dama togg gànnaar

12
New cards

again

aat

13
New cards

sait it again!

waxaatal ko!

14
New cards

mën nga waxaat ko?

can you say it again?

15
New cards

when I was a child…

bi ma nekkee xale

16
New cards

when he…

bi mu…

17
New cards

when?

ñan?

18
New cards

when…

bi…

19
New cards

when he arrived, he immediately sat down

bi mu ñewee, daal di toog

20
New cards

5 CFA coin

dërëm

21
New cards

500 CFA/100 dërëm

ñaar-fukk-i dërëm

22
New cards

5.000 CFA/1.000 dërëm

junni

23
New cards

change/coins

weccit

24
New cards

onions

soble

25
New cards

eggplant

bataan

26
New cards

hot pepper/chili

kani

27
New cards

cooking oil

diw/diwlin

28
New cards

use

jëfandikoo

29
New cards

remember

fàttaliku

30
New cards

I remember you

fàttaliku naa la

31
New cards

fàtte

forget

32
New cards

I forgot it

fàtte naa ko

33
New cards

soup

soupou

34
New cards

so/therefore

kon

35
New cards

I have paid

fey naa

36
New cards

you are in my thoughts

maa ngi la ci sama xalaat

37
New cards

I want you to know it

bëgg naa nga xam ko

38
New cards

it warms my heart

neex naa ci xol

39
New cards

I’m happy to know that it warms your heart when you know that I’m thinking about you

bég naa ci xam ne neex na la ci sa xol bi nga xam ne maa ngi lay xalaat

40
New cards

It is too expensive, lower it a little!

dafa seer lool, waññi ko tuuti!

41
New cards

what are you looking for today?

lu ngay wut tey?

42
New cards

bad manners

ñak teggin

43
New cards

man is the medicine of man

nit, nit ay garabam

44
New cards

slowly, slowly catches the monkey in the bush

ndank-ndank mooy jàpp golo ci ñaay

45
New cards

the eye carries no load, but knows what the head can bear

bët du yenu, waaye xam na lu bopp mën

46
New cards

whoever lends your legs, you walk where it pleases them

ku la abal tànk, nga dem fa ko neex

47
New cards

however vast the physical body is, the heart is greater

lu jëmm yaatu yaatu, xol a ko ëpp

48
New cards

pray to god, but cultivate your field

yàlla, yàlla, bay sa tool

49
New cards

bring

indil

50
New cards

care for/protect

sàmm

51
New cards

don’t let your heart grow weary

bu sa xol tàyyi

52
New cards

my head hurts

sama bopp dafa metti

53
New cards

my stomach hurts

sama biir dafa metti

54
New cards

wound

góom

55
New cards

throat

kòll

56
New cards

neck

baat

57
New cards

tree/medicine

garab

58
New cards

that/which

bu

59
New cards

I have fever

moom yaram dafa tàng

60
New cards

spend the night

fanaan

61
New cards

how many times?

ñaata yoon?

62
New cards

ndeke

oh

63
New cards

oh, turn out it really is true!

ndeke dëgg la kat!

64
New cards

touch

laal

65
New cards

don’t touch it!

bul ko laal!

66
New cards

jël

take

67
New cards

reduce

waññi

68
New cards

stop

taxaw

69
New cards

cost

jaar

70
New cards

spend the day in peace

yendu ak jàmm

71
New cards

I eat breakfast first

dama njëkk lekk ndekk

72
New cards

the rain

taw bi

73
New cards

it’s raining, the family of the house are worried about the roof

taw bi, waa kër gi dañuy jaaxle ci kaw kër gi

74
New cards

why are you sleeping so much?

lun tax ngay nelaw lool?

75
New cards

I buy a lot of chicken

dama jënd Gànnaar bu bari

76
New cards

different things

yëf yu wuute

77
New cards

seafront promenade

la corniche

78
New cards

you take a long time

yàgg nga lool

79
New cards

and you?

yaw nag?

80
New cards

travel

tukki

81
New cards

every day

bés bu nekk

82
New cards

the street

mbed mi

83
New cards

easy

yomb

84
New cards

difficult

jafe

85
New cards

If I

su ma

86
New cards

if you

boo

87
New cards

if he

su mu

88
New cards

yes, I know it

waaw, xam naa ko

89
New cards

there

fa

90
New cards
91
New cards
92
New cards
93
New cards
94
New cards
95
New cards
96
New cards
97
New cards
98
New cards
99
New cards
100
New cards