1/13
Looks like no tags are added yet.
Na nga def?
How are you?
Maa ngi fi (rekk)
I’m fine
Yow nag?
And you?
Maa ngi ci jámm.
I’m well.
Waaw
Yes
Déedéet
No
Jërëjëf
Thank you
Naka suba si?
How was your morning?
Naka nga yendoo?
How was your day?
Jamm rekk
Peaceful
Baal ma
Sorry
Dem naa
I’m going
Fii rekk
Right here
Ba beneen yoon
Until next time